Le cirque du Sahel est célèbre dans toute l'Afrique. Mais un évènement inattendu risque de faire annuler la représentation exceptionnelle de ce soir. La réputation du cirque est en jeu. Le directeur parviendra-t-il à faire jouer son meilleur artiste et maintenir le spectacle ?
Sirku Sayel siiw na ci biir Afirik gépp. Wante mbir mu kenn séentuwul woon moo nar a yàq wone bu doy waar bi war aam ngoon. Turu Sirk bi nar naa yàqu. Ndax njiitul sirk bi dina mën a amal wone bi artistam bi gën a ranneeku war a def, ban a dàq xew wi ?
En poursuivant votre navigation sur ce site, vous acceptez l’utilisation de cookies pour améliorer votre expérience d'achat et pour réaliser des statistiques de visites.